+ Overview yu tar tax képp kuy dund fippu. Temano egsi na ba mu nekk ci doomi lépp lu aju ci dundin diggante góor ak jigéen, ci biir tawfeex gu yaa. Nit kune war naa dund ci tawfeex ak kaaraange. Kenn warula xuus ci dundinu doomu aadama, bu njabootam, ci lu jëm ci 1. Ngay dund yaw doww mbaa ak mbooloo am nga sañ-sañ am loo moomal sa Nit ku ne meññeefu askan wi am na sañ-sañ ñu aar ko ci giru dundam. Ci dundam war na ci am xol bu sedd ci sañ-sañam yooyu, lu aju ci koom-koomam, ci dundinam ak ci lépp lu aju ci aadaam te di ko jox te mën koo dundal ak njabbotam te mu yellook sagu doomu aadama, mu mottaliku it ak yeneeni pexe su mënee am ngir aar dundinam. 1. Nit ku ne am na sañ-sañ am dundingu yamamaay ngir dëgëral farata ci wàllu dundam. Am na it sañ-sañ ñu aar ko bu liggeeyatul